clear
{{language.name}} Nessuna lingua trovata.
swap_horiz
{{language.name}} Nessuna lingua trovata.
search
Attenzione: questo sito web è stato creato al fine di tenere d'occhio ogni sviluppo. Ogni cosa che pubblicherai verrà sicuramente persa.

Frasi in:

Mostra le traduzioni in:

ATTENZIONE: Verranno mostrate sia le traduzioni dirette che quelle indirette.

Tutte le frasi in wolof (28 risultati)

Frase #6402881 — appartiene a MarjorieW
wol
Bëtub mbëggeel jéll nab gàkk.
info
Frase #6402878 — appartiene a MarjorieW
wol
Bët du yenu waaye xam na lu bopp àttan.
info
Frase #6402875 — appartiene a MarjorieW
wol
Bes boo gis, day leb walla muy fey.
info
Frase #6402871 — appartiene a MarjorieW
wol
Benn loxo du tàccu.
info
Frase #6402863 — appartiene a MarjorieW
wol
Bëggum ñeex duma taxa dëppoo cin lu tàng.
info
Frase #6402861 — appartiene a MarjorieW
wol
Bëgg-bëgg yee wuute, moo-tax njaay may jar ca jaba.
info
Frase #6402858 — appartiene a MarjorieW
wol
Bant, lumu yàgg cig dex, du tax mu soppiku jasig.
info
Frase #6402854 — appartiene a MarjorieW
wol
Bala nga xam luw taat di jariñ, mbate toog jote.
info
Frase #6402851 — appartiene a MarjorieW
wol
Am naa giléém ca Gànnaar yomb naa wax.
info
Frase #6402846 — appartiene a MarjorieW
wol
Alalu golo ca lex ba.
info